Ou suis je ?
Paroles Youssou N'Dour Pullo Àrdo lyrics

Paroles Youssou N'Dour Pullo Àrdo

Koufi gneuw mu diangal la
Niax mi môko môm
Ndokh mi môko môm
Daf ko donn
Lî khar yi la
Lî beuy yi la
Nagam yangui
Àll bâ ngui
Baxi mâmaw Poullo Àrdo
(x2)

Pullo-Ardo pullo-djèry pullo-ardo
pullo-djèry Pullo-Ardo pullo-djèry

Dakhal yi mu jeum fé
Nga dakh yé mou jeum fi
Yâ xam yaw li khèw fé
Dara diaxa loula fi ba fé

Pullo-Ardo pullo-djèry pullo-ardo(x2)

Ardo sékhna guëneum
Daldi gaddu yatam
Ma nga anddak khadjam
Daldi djitël guéteum
pullo-djèry Pullo-Ardo

Mingui anddak khdjam
Daldi djitël guéteum
Dalal xélam
Féxal xolam
Bou nit gniy fo aka ré môm yëguko
Souy
Pullo-Ardo pullo-djèry

Lépp am mingui fi
Fî la yarô
Fî la magué
Téyit fî la
Také soxna
Lépp am fî la
Pullo-Ardo pullo-djèry
Bu nit gniy teub aka dal môm yëguko
Limu am fî doy nako té doylô nako
Boudè or la
Mba jamâ
Wala étage la
Mba avion la


Mba lénène la
Môm guissouko Pullo Ardo

Ma nga gaddu tôkhôr om
Di mbîb mbîb yu am khôrôm
Waye waye yu amoul môrôm
Mél ni kouy nèkhal gôrôm
Bofa diarè sant sarr è dinala rè
Bofa diarè dône sérère è dinala rè
(x2)

[ Merci à hady d'avoir ajouté ces paroles ]
» Corriger les paroles ?

Envoyer ta dédicace au sujet de Youssou N'Dour :




LES DEDICACES POUR Youssou N'Dour
  • Par gnisco le 2009/11/04 13:33

    je dédie cela à tonton you ki kan j'écoute sa musique me redonne la joie de vivre, le courage d'affronter les difficultés de la vie. Merci à toi.

  • Par CHERIF le 2009/10/25 14:49

    vraiment grand je suis fans de vous je suis mauritanien mon réve c'est de tinvité chez moi

  • Par le 2009/10/23 13:08

    slt gran js8 étudian en master1 danalyz et politic économic a Clermont ferrand j kif énorméma sk vs faite C du gran art rien a dir hormi chapo ba vs etes un idol pour la jeuness africaine et pour lamour de Dieu k persone n vs ecarte de vtre chemin C lbon longue vi a vs et bcp de reussite ds vs entrepriz js8 1fanatic svp pass un jour a Clermont

  • Par likma1985 le 2009/09/10 16:31

    youssou

  • Par le 2009/09/10 01:01

    youssou2oo9

  • Par lém le 2009/08/19 19:41

    slt l roi sincèrma parlé j testime bocou worna baye niass j p t dire k g prsk la majeur parti d t album en tete mè mon chançon préféré c demb vous lavé composé san pr otan konètr léfé k ça nm fé é san oublié j rève d t rencontré 1 jr ça m ferè trè plaisir barké baye niass.longue vie é santé d fer a toi.bye

  • Par seydina le 2009/08/19 15:26

    slt youssou sui ravi de vous ècrire un msg mè je vou souhaite une trè bne contuniation

ILS EN PARLENT DANS LES FORUMS
  • Sois le premier a lancer un sujet sur Youssou N'Dour en cliquant ici !
ENVOIE CES PAROLES À TES AMIS

Actualité People

Christophe Willem ne sera pas juré à la "Nouvelle Star"

Christophe Willem ne sera pas juré à la "Nouvelle Star"
Contrairement aux rumeurs, le chanteur n'intégrera pas le jury de la prochaine édition de "Nouvelle Star".