Paroles de Yama

Youssou N'Dour
Soubateel, bamuy barilé
Ñi di déloo sen palanter
Ngir baña xaar li xew, li xew féneen
Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon (bis)
Gaal gi teer
Ba ñu seet li, li wara dem féneen
Té du yeebi ludul meew lifi des
Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon (bis)
Moo waral bu sédalé, du am
Du am. Rusna ñaan ba day fandé, fandé
Moo waral bu sédalé, ba du am
Du am. Rusna ñaan Kii daal amu fi morom
Yaamaa nango sona lol
Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon (bis)
Ni dox sa waar bamu noppi yaw
Téréwul topa bëgë bëgë xaléyi
Yaama rek la soxal diarama, diarama, diarama
Ni woo Yama, Yama
Wuy Yama, amufi morom
Wuy Yama, nangoo sona lol
Ni Yama, jigen ju man goor
Wuy Yama, maa la setlu way
Moo waral bu sédalé, du am
Rusna ñaan ba day fandé
Amu fi morom
Mala setlu way
Yama, Yama
Amul noflay
Amu fi morom
Tunda wi rañénañ la
Yama, Yama
Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon
Ni woo Yama, ni Yama gaa yi yaaba leen
Ni dox sa waar bamu noppi yaw
Téréwul topa bëgë bëgë xaléyi
Yaama rek la soxal diarama
InterprèteYoussou N'Dour
LabelSMI
Paroles ajoutées par nos membres